Asalamu Aléykum nuyu nalén. Sunu pass internet yi dafay gawa diékh 2000 francs même pas trois jours mou diéx lolu dou yonn mane lima lén di wax moy nguén déff yeurmandé si séni...
Salam Dieng Boury,
Niongui lay ziar bou bakh tei di dieguelou bou werr si diafei diafei yi.
Dafa fekk utilisation pass bi mongui dépendre si utilisation bi.
Amna ay service...
Anonyme