Ou

Anonyme
Anonyme

Anonyme

Niveau
0
Score
3

Salam Dieng Boury,
Niongui lay ziar bou bakh tei di dieguelou bou werr si diafei diafei yi.
Dafa fekk utilisation pass bi mongui dépendre si utilisation bi.
Amna ay service sur internet yo khamneh dafay consommé données you bari.
Malay niane nga suivre lien bi ma lay yonei nguir découvrir ay astuce you lay diarigne bou bakh ba takh sa pass bi sakane: https://assistance.orange.sn/questions/2091094-profiter-p.
Ba takh na niongui bayi khel tamit si sa remarque yi tei di dalal sa khel neh dinagn ko dieul en compte nguir weuyeul di len beguel.
Niongui lay diadieufal.
L'équipe Orange
N’hésitez pas à consulter notre aide en ligne sur https://www.orange.sn/assistance
#ideesOrange

Commentaires (2)